Dikoon episode 180

Bintou Niang
Bintou Niang

Commisaire yaye assasin, nakh gua birane pieger ko bamou dieul thiabibi reuthie gua creer accident.

Giorno fa
Bakhé Sao
Bakhé Sao

sama dignité mayatou ma may sétane dikone bilay

2 giorni fa
talibé Serigne saliou rek
talibé Serigne saliou rek

A khana nak bouniou dème ba 200 épisode dina diekh

2 giorni fa
Eva Ndoye
Eva Ndoye

Dikoon yow tmt nek sa keur def say chaussure fermé merci rek pour sén cas😓😓😓

2 giorni fa
AITA STEPHAN
AITA STEPHAN

Khady nak ventre bi

3 giorni fa
Eva Sima
Eva Sima

nèkhna machala merci wa pikini production mè birane sa bouche bi comme tiaya 10métre😋😋

4 giorni fa
Fatou Ka
Fatou Ka

Le mm sort k Elimane touré la police tue parole corruption

4 giorni fa
Larissa Sagna
Larissa Sagna

Décidèrent biran com melakh rek

4 giorni fa
Larissa Sagna
Larissa Sagna

On veut keulz et dada gnom gnoy khorom série bi

4 giorni fa
møustaph Best Boyz
møustaph Best Boyz

Adduna lo guisssss deyyy dieuixx bamm deisss Dikon

4 giorni fa
isco gaye
isco gaye

Bilay nak warnguén diékhal nak

4 giorni fa
Fatou Fatou
Fatou Fatou

Cva.s'est. Bien passé. Série

5 giorni fa
Madame Poste Tout
Madame Poste Tout

Bonjour lire la suite

5 giorni fa
Mbengue Adji
Mbengue Adji

Mane dikon nekhouma dara ak canamame bi thium mouy giongué ngiongué lou ni hah

5 giorni fa
Sokhna anta Ndiaye
Sokhna anta Ndiaye

vous étes ingrats cette série vous as satisfait depuis des mois vous pourriez étre plus gentille Non ...

5 giorni fa
Fanta Diakite
Fanta Diakite

Commissariat bi d comme sabar bou tass Mère ma diama ioe do solution d Khady Sarr moy la solution 🤣 Ndeye Fily moy le cerveau 👍🏽

5 giorni fa
Fanta Diakite
Fanta Diakite

Dikon mom xetou roujaaa you rouge yi tamit 🤣🤣🤣🙄 kegn lakey ba ak xetou fermer greffage yi kagn la xewi y’a Penda sax mola geuna brancher 🤣🤣🤣ana closure tamit 🤣

5 giorni fa
Fanta Diakite
Fanta Diakite

Mane nkei keulz lA nam niii

5 giorni fa
ouliita kardash
ouliita kardash

Ani danseurs yi ak imam aaah eupena 😂 wa dikoon dagn ma yapp wala dagn ma mine

5 giorni fa
Bbeih Oumyna Sary
Bbeih Oumyna Sary

Hdjufsvkpigs

5 giorni fa
Balde Demba
Balde Demba

Qui est le criminel entr le comis et le garde

6 giorni fa
bebe Diakhate
bebe Diakhate

ma bagn commissaire bi

6 giorni fa
arimaz
arimaz

Wala l'i plan ndeye fily la encor

6 giorni fa
arimaz
arimaz

Si je comprend bien commissaire bu mo def exprès bayi clé bu si bureau bu pour wa dji évader niou def exprès auto police fir ko ngen fok ni li eupoul🤐😞🤔

6 giorni fa
maman diop
maman diop

Birane day dedelou niou yombou ko si morgu ba mou diouk di dokh dokham lol 😂 no film bi mo nekh

6 giorni fa
Carbaba Alpha
Carbaba Alpha

sen film comme gnouy wakh ak Aÿ khalee

6 giorni fa
Mayib Mbengue
Mayib Mbengue

mai birane limoy deff daffa yombo trop

6 giorni fa
ramatoulaye diallo
ramatoulaye diallo

dikoon attachion

6 giorni fa
Kine Seck
Kine Seck

warna diex naaq

6 giorni fa
Aby Sébor
Aby Sébor

Birane:woyou bo guiss bandéy bayam

6 giorni fa
Alassane mbaye
Alassane mbaye

Li kagn lay djiekh tamit😂

6 giorni fa
bebe Diakhate
bebe Diakhate

damay lath nakh Tapha da apeulo

6 giorni fa
Ndeye Thioune
Ndeye Thioune

mane commissaire bii momay ray akk kanamame bii di gnangal

6 giorni fa
Momy Mbacke
Momy Mbacke

Bravo ndeye fily

6 giorni fa
mounass sow
mounass sow

allo commissaire birane dêna😂😂😂

6 giorni fa
Sylla Mamefaty
Sylla Mamefaty

Weuuuuu mane Limay lathie moy birane mom dou tay la déf crime di kidnapper nane bb moukhamed trafique d rin lolou yépou mou déf ko sujet gounko si lolou guéne di dougne ko mana téé Walla daguéne bal lolou yépou

6 giorni fa
Mamy Ndao
Mamy Ndao

Li bakhna pour birane guaraou guaoulou de deou kanga rek

6 giorni fa
Fatou kine Tall
Fatou kine Tall

Basta siamo stancò

6 giorni fa
tiverite Jolie
tiverite Jolie

Allo commissaire Birane dénaaaaa😂😁😂😂😃

6 giorni fa
tiverite Jolie
tiverite Jolie

Ayywaaay dikoon dimbaliniou ak sa dale corossé yiiîi tu es chez toi do sol say thiarakhh you pooppp sagnsé mo diafé😁😂😂😂

6 giorni fa
Cheikh Gueye
Cheikh Gueye

Birane yaw khana meuno réglé

6 giorni fa
Sidy Mbegniga
Sidy Mbegniga

Jaime baecoub khady sarr 😍😍😍😍😍😍😍

6 giorni fa
Khadim Sylla Brésil chapeco
Khadim Sylla Brésil chapeco

Khady sarr yalla nako yalla may diame thi barkeb serigne touba wara to géne nak dagha wara nebato nak wakh baxol bet baxol

6 giorni fa
Tima masallah sire jokkou kolle
Tima masallah sire jokkou kolle

Ana maman dikoon AK pappam AK dada AK kélsi AK nabou AK mounass AK Balla AK pama AK aram AK njool AK aysatou Sarr 😅😅😘

6 giorni fa
kadet djigo
kadet djigo

Ana dada way namnako lolou

6 giorni fa
Tina diamé
Tina diamé

Legui commissaire delolll xalissou Tapha sarr bi vu k dangn la fayone kegn

6 giorni fa
Medoune ndiaye
Medoune ndiaye

Thiey ndeye fily.tjrs dangereuse.felicitation

6 giorni fa
fatousha Babeel
fatousha Babeel

Dikoon change de look perruque tamitt 🤣🤣

6 giorni fa
sokhna diarra diop
sokhna diarra diop

Serie bo khamni amoul debut amoul fin chak fois denouement boubess ca dure depuis 2ans c abusé khawma kolen yap gnici amon dieukeur eumb ba weussine sen dom yagui doxi sen soxlo

6 giorni fa
Belle Nana
Belle Nana

Un commissaire qui supplie pour arreter quelqu’un

7 giorni fa
Belle Nana
Belle Nana

Qu’est ce qu il m enerve ce commissaire

7 giorni fa
Couleursd'Afric styles Balle8
Couleursd'Afric styles Balle8

Wa yén mba macky doulen emprisonner😊

7 giorni fa
Moussa Diouf
Moussa Diouf

Aduna bii lofi guiss dafay diekh sauf dikoon. ( Vu klk part)

7 giorni fa
MELTING POT
MELTING POT

le commissaire a fait expres pour que birane puisse s' évader et je crois que birane fait le mort

7 giorni fa
Boubacar Boiro
Boubacar Boiro

no Birane cé ton vrai Acteur je l'extime bcp comment il joue son rôle

7 giorni fa
Ndeye Mareme Thioune
Ndeye Mareme Thioune

Yala nako serigne touba samb

7 giorni fa
la diva gaye
la diva gaye

Dikon khana dou lidianti dara

7 giorni fa
Khadija Fall
Khadija Fall

Khay khay khay konn Ndeye Fily ak policier bi ño d'accord ci rey Birane...lailaaaa j suis choqué 😱😱😱

7 giorni fa
Mami Ngom
Mami Ngom

dideff ay tayy basé you toque

7 giorni fa
Sokhna Ndiaye
Sokhna Ndiaye

Vous qui demandez quand se sera fini ..... degueuloulene Birane néna commencer goul sakh

7 giorni fa
Mbaye Fall
Mbaye Fall

xana diékh na li dé guéne waxon 180 épisode

7 giorni fa
Oci Belle
Oci Belle

Non mais c’est que Nd fily doit payer pour ses crimes , elle en a bcoup commis..mais def des crimes beu parer di vivre tranquille police di leu couvrir...

7 giorni fa
Diaka Waka
Diaka Waka

J'adore le personnage De khady

7 giorni fa
Papa Sk
Papa Sk

tapha sarr birane dalay nokhou de

7 giorni fa
Aldiouma Ba
Aldiouma Ba

No mabeug biran 😍😍😍

7 giorni fa
Fatma Ndiaye
Fatma Ndiaye

bayina suivre dikone Birane déna ohhhh😭😭😭😭😭

7 giorni fa
Djaraf tine
Djaraf tine

Ndaye fily et le commissaire doivent aussi payé.comme ça film bi dina gueuna ame solo

7 giorni fa
nana diouf
nana diouf

Seet film mi bi waroul woon toudou dikoon khady sarr walla ndeye fily la worone toudou dak dikoon dou si sagnassé doussi ame fit doussi meune lidiantio

7 giorni fa
Sally S.
Sally S.

Gni nagnou bayi sougnou xel yiiiii gnouye petit camp xana dou dafa évader après bimou sathiè organou djambour legui nak gnouye expliker lou ken xamoul thimmmmmm🤦🏽‍♀️

7 giorni fa
Djaraf tine
Djaraf tine

Âme na sens ça existe partou la corruption

7 giorni fa
Fatou Sow
Fatou Sow

Beuge naléne trop

7 giorni fa
abdou aziz diop
abdou aziz diop

Hahaha commissaire birane dei na aka yomb😂😂films bi mo wara diekhh srx doye na nak

7 giorni fa
Amet Diop
Amet Diop

Ah konn commissaire bi mo ray lou birane , mai birane rek aka bandit qui est d'accord beseul bleu🤣

7 giorni fa
Fatou Faye
Fatou Faye

Amet Diop

7 giorni fa
Aminata Toure
Aminata Toure

Très intéressante

7 giorni fa
Lindo Thiam
Lindo Thiam

Ndeye moy nekhal filmeuh biii

7 giorni fa
Diariatou Sall
Diariatou Sall

birane sof gua nekhoma dara

7 giorni fa
bah malick
bah malick

wa team keulz ak dada aniniou

7 giorni fa
Ndongo Seck
Ndongo Seck

gnogui ni team diamy gueye alias dada

7 giorni fa
Ndongo Seck
Ndongo Seck

gnogui ni team diamy gueye alias dada

7 giorni fa
Modou Sylle
Modou Sylle

Belle image👍

7 giorni fa
sokhna diarra diop
sokhna diarra diop

Wayen ma warouwouma commissaire corrompu mounane souma sanione guen bayi niou arretèko ben temps bou daw li 😂😂😂😂 dikoon kagn laydiex wouyoul mere ma diama di alou yaw meuno regler probleme bay wout solution mane serie bi mrci rk😂😂😂😂😂

7 giorni fa
Bayd Niang
Bayd Niang

sokhna diarra diop

8 ore fa
Ndeye Absa Niang
Ndeye Absa Niang

Amna cousine Bo hamner debut serie la acouché wonna dome bou djiguen legui samedi 11aout bi la warra deff mariage deyy seyi ndeysan hamna damay moudjer ganiou rekk thii liiii

7 giorni fa
cisse mame awa
cisse mame awa

Ndeye Absa Niang 😂😂😂🤣🤣🤣🤣

6 giorni fa
Nogaye Gueye
Nogaye Gueye

Ndeye Absa Niang mdrrrr yaw KO yap

7 giorni fa
Seynabou Diouf
Seynabou Diouf

Hahaha Ndèye fily miné bimouy dougg si serie bi marié goul nak?? 😂😂😂 té accoucher na bou yague ba dome dji deuggeur

7 giorni fa
modou ciss
modou ciss

yen billay khamolen dara

7 giorni fa
Ndaté Diattara
Ndaté Diattara

modou ciss é

6 giorni fa
Mame Asta Mbacké
Mame Asta Mbacké

birane sa kaname guii koukaye khôle d'où âme darah

7 giorni fa
kharitou dieucoeuram
kharitou dieucoeuram

Ndeye fily doit payer sinon d'où ame chance khana police famille sarr ley ligueyel

7 giorni fa
DIARGA MBALLO
DIARGA MBALLO

kharitou dieucoeuram 🚴

7 giorni fa
Awa Lô
Awa Lô

Biran yaniawww

7 giorni fa
modou ciss
modou ciss

waye diekhal len sen flmob khamatolen foguen diem

7 giorni fa
pöüpée fatale
pöüpée fatale

Li amoul wayy pikini vous vous foutez de notre gueule Birane fougnouko diapé warafa diapp ndeye fily mais à la fin police Sénégal guéne yapp

7 giorni fa
moussa ba
moussa ba

filmu bi da wa diekh ndakh biran sou dewe dotoul nekh

7 giorni fa
Awa Maty
Awa Maty

8

7 giorni fa
Djiby Niang
Djiby Niang

daaray cocc dal moma doy thi theatre liiii momm film américain la ishhh

7 giorni fa
Djiby Niang
Djiby Niang

vraiment jack bauer ak michael scofield amnaniou place thi film bi

7 giorni fa
Sylla Mamefaty
Sylla Mamefaty

Djiby Niang 😂😂😂😂

6 giorni fa
Ndiogou Niang
Ndiogou Niang

Ok

6 giorni fa
DIARGA MBALLO
DIARGA MBALLO

Djiby Niang 😎💪

7 giorni fa
Astou Diop
Astou Diop

Li deh moy corruption a1000pour 1000mai nak dafa ame motakh niou jouéko😂😂😂😂😂

7 giorni fa
Khoujita Fall
Khoujita Fall

wa tapha sarr noumou beau wé ni nak

7 giorni fa
Aisata Ndiaye
Aisata Ndiaye

Khoujita Fall je confirme 😍

5 giorni fa
Misse Diatta
Misse Diatta

Chuo

7 giorni fa
Karamo Camara
Karamo Camara

c film à plein de sens nakh mane djisna ci sama bopp

7 giorni fa
amina bah
amina bah

Ndeye fily c'est une vrai artiste

7 giorni fa
Mouha Ka
Mouha Ka

Moi

7 giorni fa
Astou Diop
Astou Diop

Birane dal warone sant GUEYE di yakh sama santou dieukeur😂😂😂😂

7 giorni fa
j'aime galsen
j'aime galsen

Donc plan bi ndey fily tek ak commissaire bi mo ray birand aka bandi fily rek j l'adore beaucoup

7 giorni fa
Im Leslie 30
Im Leslie 30

Birane niaw nge

7 giorni fa
Khadija Fall
Khadija Fall

Im Leslie 30 yalla lako takha wakh deh..😂😂😂

7 giorni fa
Awa Thiam
Awa Thiam

Khady Sarr yaww danga ma nekh ana wa tram Khady Sarr beusseul bleu

7 giorni fa
Mame Cheikh Seck
Mame Cheikh Seck

tapha sarr yow ragal nga dh yow birane défoul dara guay naw

7 giorni fa
penda diop
penda diop

birane deee na dafa yombo billahi

7 giorni fa

Prossimi video

fedex delivery