TIEY TABASKI EPISODE 3

Aby Ndour
Aby Ndour

Kombe okin respect si fat kine😂😂

Giorno fa
Ablaye Petit Mbaye
Ablaye Petit Mbaye

ndeysan diop fall febar bi dako yaar kw kxkxkx wèreul ak djam lartist

2 giorni fa
Bayemorseye Seye
Bayemorseye Seye

demal tok

2 giorni fa
queen'cess Camara
queen'cess Camara

Deureum yaye aka yagg 😂😂😂😂😂😂

3 giorni fa
queen'cess Camara
queen'cess Camara

Riguou lene nii 😂😂😂😂😂😂

3 giorni fa
Houleye Ndiaye
Houleye Ndiaye

Diop fall a besoin d'un aide financier selon ma déduction du scnerio entre lui et dérem. Que DIEU l'assiste 👌

3 giorni fa
Ndeye Sakho
Ndeye Sakho

fatou kine jtm wy

3 giorni fa
Saliou Toure
Saliou Toure

Diop Fal yalla na la yalla may diam barkép Serigne Saliou

3 giorni fa
mandiaye ndiaye
mandiaye ndiaye

yénafi nék

3 giorni fa
Aminata Faye
Aminata Faye

Diop fall way Ana gni ko namone 😂😂

4 giorni fa
Fatou Diop
Fatou Diop

Sama khol féssna.Diop jm te revoir en forme bilay.

4 giorni fa
Kev Kess
Kev Kess

Je comprends pas la langue lol

4 giorni fa
Ndao Mor Daro
Ndao Mor Daro

No manioukh Ken la

4 giorni fa
Mamadou Lamine Cisse
Mamadou Lamine Cisse

Tabaski moudiei naa metti

4 giorni fa
joe bara
joe bara

nooooooon fatou kiné elle est tres belle

4 giorni fa
Ndeye Dieng
Ndeye Dieng

Nena "renard" lol 😂

5 giorni fa
Amina Ndiaye
Amina Ndiaye

Manioukkk dinama raye 😀😀😀

5 giorni fa
Dorina Gomis
Dorina Gomis

Eyway Ndeye Ndiay mongui yakk tein noir bi way...pourquoi xéssal tamit, yalla na yalla deff xéwal way thi sougnù pàpà yii,gneup am xàrr tabaski si djama inchalla

5 giorni fa
nadia la belle
nadia la belle

Ma niouk Néna niague ak dereum yaye tissu yoyou longtemps na😂

5 giorni fa
Prince Cogito
Prince Cogito

Ohh Diop Fall Namanako deh😉❤

5 giorni fa
daba dida dia
daba dida dia

yala nagnu yala samou defal gnu sutura ak wér ak khèweull tabaski bi borom keur yèpou am xar tè bagna am fitt neu

5 giorni fa
Ndeye Mbissine
Ndeye Mbissine

wiri wiri

5 giorni fa
Elhadji tidiane Aw
Elhadji tidiane Aw

Ndeye ndiaye pourquoi depigmenter nak ish Yakh nga sa bopp way

5 giorni fa
Sokhna Khole
Sokhna Khole

Barki serigne falilou deureum damay fathie🤣🤣🤣🤣

5 giorni fa
delfa Bi
delfa Bi

Yénafi meune mako wakh

5 giorni fa
Pape Diouf
Pape Diouf

Kou begue diop fall besel jém

5 giorni fa
thimbo thierno idrissa
thimbo thierno idrissa

Wa mais ana épisode 4 bi sone naniou

5 giorni fa
Bayougo Sall
Bayougo Sall

mandé aw beuy sakh amagoumako waxagouma xarr

5 giorni fa
tislim dione
tislim dione

Ahh namone Diop fall

5 giorni fa
Mbaye Faye
Mbaye Faye

non Diop fall namnala trop

5 giorni fa
Lamin Fadera
Lamin Fadera

Fatou kine akh saina nio farr

5 giorni fa
Die Mbodj
Die Mbodj

Vieux mako beug rek

5 giorni fa
Niang Modou
Niang Modou

Mais ndakh khangéni Ndeye Ndiaye dafa noss walla loukhéw

6 giorni fa
Mamadou Diop
Mamadou Diop

Fatou kiné machalla avec sa tin naturel

6 giorni fa
Ndeye Diakhate
Ndeye Diakhate

Bilay latyr wax ko thia kaw.niarel yii dou niiou dem!

6 giorni fa
safandou Safandou
safandou Safandou

Bilay Diop fall deug piir nga wakh😊☺

6 giorni fa
Ndari Ba
Ndari Ba

Diop fall mo meuna woyan

6 giorni fa
Ndira Ndir
Ndira Ndir

Tabask rek

6 giorni fa
Yoro Fall
Yoro Fall

Mn momm magnoukh sm your yi lay diakha sè

6 giorni fa
YÉÉWOULÉN TV BANLIEUE
YÉÉWOULÉN TV BANLIEUE

Fat kine nékh nama

6 giorni fa
Abdinho Fall Fallene Bi
Abdinho Fall Fallene Bi

Fatou kiné 😍

6 giorni fa
Oumy Lo
Oumy Lo

Fatou kine da ame diekeur

6 giorni fa
Adama paris
Adama paris

Sketch bi nekhneu waye, mais Afrimarket 110mil mouton ak 10kilos soblé bahna deih mashallah gspr khar you ame takhawaye la rek

6 giorni fa
anta lo mou serigne saliou mbacke
anta lo mou serigne saliou mbacke

Ho sama diop fall waye ❤ yalna yalla guena yokou tawfekh amine

6 giorni fa
Mallé Sylla
Mallé Sylla

Loutakh maniouk reww

6 giorni fa
kebe pari mana
kebe pari mana

Ana ñi name Diop fall way

6 giorni fa
Fatou Diouf
Fatou Diouf

machalla diop Fall

6 giorni fa
Tapha Diouf100
Tapha Diouf100

Fate kiné sa tein noir bakh na

6 giorni fa
Maguette Kébè
Maguette Kébè

Machalla Diop fall

6 giorni fa
Awa Babacar Wane At-Tidjany
Awa Babacar Wane At-Tidjany

Maniouk,Kombé ak Vieux momeu gueneu ñu 🤦🏽‍♀️diñu terrorisé Wayè Deureum sa cas grawna mouton wala dara🤣🤣

6 giorni fa
Maguette dabo
Maguette dabo

Enfin Diop Fall est de retour ! Mais kombé dinama raay rek 😂😂😂

6 giorni fa
Dame Cisse
Dame Cisse

oh diadia plainte takhawna

6 giorni fa
Danso Ba
Danso Ba

Team kiné je t aime beaucoup 🍠

6 giorni fa
Yacine Bakhoum
Yacine Bakhoum

tram fat kine

6 giorni fa
Baba Fall
Baba Fall

Kou aimé sama commentaires yalla n'a la may lo beug ci sa adouna 🙏

6 giorni fa
Saliou Toure
Saliou Toure

👍

3 giorni fa
Akim Diakhate
Akim Diakhate

amine

5 giorni fa
TAF TAF 10
TAF TAF 10

diop fall

6 giorni fa
B N G TV 221
B N G TV 221

Diop Fall way

6 giorni fa
Mohamed Diop
Mohamed Diop

#Diopfall yalla na yalla yokk la werr barkei seydina mouhammed

6 giorni fa
Fatousha Diagne
Fatousha Diagne

Oooooh finalement Diop Fall namon nagn la 😍😍

6 giorni fa
khadija salih
khadija salih

wooooooooooooooooooooooooooooooooooyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyyy

6 giorni fa
MADRISTA MBOW
MADRISTA MBOW

Madioukh est meilleur que AYA NAKAMURA

6 giorni fa
Maniame TV
Maniame TV

https://www.youtube.com/channel/UCriqDe6hquS0IAA4_WynhUQ

6 giorni fa
Princess mbay
Princess mbay

Deureum comme kou amé loss

6 giorni fa
Denis boy kl
Denis boy kl

Haha bilay Mane dina dh 😂 Yalla nagnou Tabaski si djamou 🙏🙏

6 giorni fa
L'homme du Coeur
L'homme du Coeur

Billahi ndaye Nidaye ya reuy bopou rk

6 giorni fa
Alzo Afri Cana yenguelin
Alzo Afri Cana yenguelin

😂😂

6 giorni fa
Thiane Gaye
Thiane Gaye

Noo deei na manioukh neina fi niaague aye bobou tisdu foumou amati😀😀😀

6 giorni fa
Ahmadou Dieng
Ahmadou Dieng

Mangnioukh

6 giorni fa
Ali Toure
Ali Toure

Ana team combe yalla na niou kou féké ak diamou ta tale kou 😂😂😂

6 giorni fa
mousta n9 diop
mousta n9 diop

Diop fall

6 giorni fa
Astou Ndiaye
Astou Ndiaye

Ani wa association ande setan série yeup je vous Salut🙏🙏🙏🙏🙏🙏👋👋👋👋👋👋👋👋👋👋👋

6 giorni fa
Shasha Kah
Shasha Kah

Mdrrrrr Kombe kay wouyou say 2renards yiii manioukh demayyy fathie

6 giorni fa
Tabarra Bakh Tall
Tabarra Bakh Tall

#FatouKiné bilaye ya tarou masha' allah da nga ma nékh ba fou nékh yam!

6 giorni fa
MACKA BRAGUEYE FAMILIE
MACKA BRAGUEYE FAMILIE

Diop Fall yall nala souniou boroom sammou aar là défall là fann wou gouddou akk wérr gui yaram

6 giorni fa
Ndeya Fatou Ba
Ndeya Fatou Ba

Diop fall namennako yala gua ame diam

6 giorni fa
Ndeya Fatou Ba
Ndeya Fatou Ba

ndiaye la puissance zeyna nio far niou bocouko

6 giorni fa
ndiaye la puissance zeyna
ndiaye la puissance zeyna

Ndeya Fatou Ba aminnnn

6 giorni fa
Thérèse MENDY
Thérèse MENDY

Liii moy diabare weuhh rew bâ doff

6 giorni fa
Maman karre
Maman karre

Woooooy😂......... Diop fall m’a tué néna france pour ngua ame 2€ sakh probléme la billaaye aka wakh deugeu deuk bii aka metti té waa galsen ils n’ont rien compris.

6 giorni fa
Kana Kana
Kana Kana

wlh c vrais

6 giorni fa
Toure Aboumahmoud
Toure Aboumahmoud

tu es super fatou kinne

6 giorni fa
TOTALLY FAMILY RAMA
TOTALLY FAMILY RAMA

Kumay sarakh ay aimer yu pata abonner a notre chaine cest amusant

6 giorni fa
senegalaise Mbodji
senegalaise Mbodji

Wax degeu maniouk palman beuthieuk tangor bi😂😂😂😂 Ah ndeye ndiaye tay amnagn la kxkxkx

6 giorni fa
MATH-LIPZ Deme
MATH-LIPZ Deme

Cuisiniere ak guimaar combe am ngua problème dingua niorr khombou dooto dèèsèti dara tissu yèè nata diekh rek

6 giorni fa
Fa dudu Lô
Fa dudu Lô

Tay si aya nakamura lah😂😂😂😂

6 giorni fa
Moréén TV
Moréén TV

les 3 la dougn dem😂(manioukh kombe vieux ) ak 2pa yi😂.hei diop fall nieuwatina😂

6 giorni fa
maodo diagne
maodo diagne

Neexna waay Ana fans job fall yi

6 giorni fa
Serign Mbacke Loume
Serign Mbacke Loume

Dimanche Premier Match LIVERPOOL Premier League contour West Ham Anfield

6 giorni fa
Toure Daour
Toure Daour

Merci pour l'information

6 giorni fa
Papa Amadou Mbow
Papa Amadou Mbow

kombe mbarane nañoula teh yeguoko😂😂😂😂

6 giorni fa
Kamal 313 Soxar Xalima ndiaay
Kamal 313 Soxar Xalima ndiaay

Barké serigne salihou mbacké kombé ak madiokh gnongui maay yeubu yawmal khiyamati bilahi gnii gnon con qw😂😂

6 giorni fa
Moussa Sarr
Moussa Sarr

je t'adore fat kine

6 giorni fa
Ndour Davido
Ndour Davido

o guiss na Diop fall tey way

6 giorni fa
Ndour Davido
Ndour Davido

Mane Dex Diop fall la namou

6 giorni fa
Abdoulaye dieng
Abdoulaye dieng

Sa niarri renard yii😂😂😂

6 giorni fa
ÔůŻę Président
ÔůŻę Président

Qualité son Bi c’est à revoir svp

6 giorni fa
Faramarene snap Wally B seck
Faramarene snap Wally B seck

Yalla na diamou yague Sénégal ❤ Abonnez-vous à ma chaîne YouTube svp

6 giorni fa
PAPINO
PAPINO

Fatou kine❤

6 giorni fa
Bass Gueye
Bass Gueye

no combé ray nama ya meneu feinne kay

6 giorni fa
Barane sylla
Barane sylla

Kousa xoll nékh 👍

6 giorni fa
Papy Gueye
Papy Gueye

Mane dall fate kinné mako beugue pur billay

6 giorni fa
TKB Tv
TKB Tv

Yama mana fen😂😂😂 nn kombé

6 giorni fa
devenir pro
devenir pro

Tabaski diamb pour niepp amiine

6 giorni fa
Ngvgne dembv Kvne
Ngvgne dembv Kvne

tapha neme

6 giorni fa
Babacar Sow
Babacar Sow

Maniouk badiane alias Tafa neme 😀😀😀😀

6 giorni fa

Prossimi video